Mnm – Veux Tu M’épouser?

Allô baby girl dama la soxlawon pour ñu waxtaan some time
Nuyu wu ma la sax mba ya ngi diam d’abord xam nga rek da nga may comprendre
Pour li ma lay doyé féxél ba imaginer èhh anhh yaya!!
Xam na sa bopp ya ngi giss image yu né éh xam na la
Kumpë ngi lay ray ya ngui lox fi nga toog dalalal sa xél du li nga foog
Gaw nga diaxasso mang koy yëg fima tok
Soxlawu ma la localisé yaw pour xam fi nga tollu
Fay ma ma wax la neexal ma nak baax na lu
Ko moy ma wirri wirri bae ba diareefa nax lë
Lu ma ci jublu lu baax la mais nak fallait que
Ma cax lë and bu yaggé yaw tè dëggu lu ko lal koon lu sax la

Hé wallahi yaw rek’a matt li nga doon xalli nga
Sama yoon mu tar nga dékku fi coono
Té bilahi mussoo ma def lu ma métti fép da nga ma
Ci fékki takku ci ngir ma tékki
Loolo tax tay ma bëg yaw ñu and bae bolé life bi def
Ko bén dagganal  ko ngir ñu sëy
Té waxtaan nañ sa papa yombalal ma lep né na léegi ya ci dés

Veux-tu devenir ma femme veux-tu m’épouser
Veux-tu devenir madame veux tu m’épouser hèè èhh
Veux-tu devenir ma femme veux-tu épouser
Veux-tu devenir madame veux-tu mé’pouser hèè èèhh

You’d never be alone you can call on me baby
Give me your hand don’t be afraid
Look me in my eyes and tell me that you love me
Stop thinking bae you now I love you
Normal mu yeem la ndax day lu bees
Mais mérite la nak ak fu ñu jota wees bae
Li ma la fayé tay dang ko fi jiw hey
Sa oui waw ok moy takh ñu siw you now
Né ma yes rek ma free hihi
Sama life sans yaw non dou chill hihil
Bayil sa jooy yi xam ga yaw la feel hihilll
Baby girl yaw you now the deal hilll
Dëg la xol yii fees na rongoñu mbegtéy tuuru
Mais tay nak bés bu bees la ñëwël mak yaw ñu nguuru
Lu ñuy dundu dafa fees nak gis nga sax mu ngi tuuru
Man jitu na la leuz ba ya ngeek lém ma ngeek mbourou

Hèè wallahi yaw rek’a matt li nga doon xalli
Nga sama yoon mu tar nga dékku fi coono
Té billahi massoo ma def lu ma mètti fep danga
Ma ci fékki takku ci ngir ma tékki
Loolo tax tay ma bëgg yaw ñu and bae bolé life
Bi def ko bén daganal ko ngir ñu sëy
Té waxtaan nañ sa papa yombalal ma lep né na léegi ya ci dees

Veux-tu devenir ma femme veux-tu m’épouser
Veux-tu devenir madame veux tu m’épouser hèè èhh
Veux-tu devenir ma femme veux-tu épouser
Veux-tu devenir madame veux tu mé’pouser hèè èèhh

Zama – Ndizobizwa

Lashoni ilanga ndilindile Ndijongi ixesha Buka bonke ontanga Nami bayawela Mawuthi uthathu ukubeka kusele Mina ngedwa Lashoni ilanga...

Brandon Dhludhlu – Uhambe

You were part of my life From back when we were kids I have no cash...

Brandon Dhludhlu – Uhambe

You were part of my life From back when we were kids Ngingenawo nocash wokuk'khipha Bheka manje...